Jammu Africa
Afrika a a a Afrika mon AfriqueSama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaqMa ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reewD'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'AfriqueMêm' si le ciel tombait luttons pour la paixKon jammu Afrika moom lay ñaanMané jammu Afrika mooy suñu natangeAfrika a a a Afrika a aAfrika a a a Afrika mon Afrique
Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaanAk loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte AfrikaIci ou ailleurs la paix prix du bonheurMêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frèresKon jammu Afrika moom lay ñaanMané jammu Afrika mooy suñu natangeAfrika a a a Afrika a aAfrika a a a Afrika mon Afrique
Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi menNgaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadiYoo Alla addu jam to RuandaYoo Alla addu jam to BurundiYoo Alla addu jam to CasamansLawol Mbignona yee
Traduction (les deux premiers couplets sont en wolof, le dernier est en Pulaar)
Dans mon rêve je prie Dieu pour que cela se réalise avant mon trépasJe dis " un jour viendra où l'Afrique sera unie "D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'AfriqueMêm' si le ciel tombait luttons pour la paixDonc je demande la paix en Afriquecar avec la paix en Afrique ce sera la prospérité
Etranger, moi Lô je te priequelles que soient ta fortune et ta situation de ne pas oublier l'AfriqueIci ou ailleurs la paix prix du bonheurMêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frèresDonc je demande la paix en Afriquecar avec la paix en Afrique ce sera la prospérité
Vous les enfants d'Afrique, levez-vous pour construire notre paysQue Dieu nous épargne les malheursQu'il apporte la paix au Rwanda, au Burundi,Et en Casamance sur la route de Mbignona!!!
Ismael Lô
5.12.08
Suscribirse a:
Enviar comentarios (Atom)
No hay comentarios:
Publicar un comentario